У нас вы можете посмотреть бесплатно Waxtaan Ci Cheikh Ibra Fall ak Njabotou Serigne Touba | Leralu Serigne Cheikh Mbaye Yaaram или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Dieureudieuf mbokk yi, si téwlu bi. Vidéo bii di "Mame Cheikh Ibrahima Fall ak Njabotou Serigne Touba : 'Ndax Ass Goor Waarta Leek....'", amna solo lool si leral you niou Serigne Cheikh Mbaye Yaaram indil. Si biir waxtaan bi, Serigne bi dina ñieuw si ay point you am solo : Diganté bi nékone si digeunté Mame Cheikh Ibrahima Fall ak njabotou borom Touba. Leral you mat seuk si kaddu yi am solo yi di "Ndax Ass Goor Waarta Leek....". Tour d'horizon si doundou ak diégalou Lamp Fall Baboul Mouridina. HORODATAGE / WAxtu Wi : 00:00 - Tambali ak Ndioukeul 04:15 - Tour d'horizon si Mame Cheikh Ibrahima Fall 12:30 - Diganté Mame Cheikh Ibra ak Kéru Serigne Touba 25:50 - Luy tekki "Ndax Ass Goor Waarta Leek..." ? 38:10 - Leralu Serigne Cheikh Mbaye Yaaram si waxtaan wi 55:00 - Tontu si laaj yi 01:08:20 - Kadduy taggo ak ñaan Vidéo bii dafay leral beuss bu mag bi té indi ay tontu si ay laaj you bari yo xamné beugone naniou si am ay leral. Boulén faté Abonné ngir béne vidéo doulén raw, té beuss "j'aime" bi ngir soutineul liguéy bi. Dieureudieuf. #MameCheikhIbrahimaFall #SerigneTouba #Mouride #Leral #Senegal #BayeFall #Islam