У нас вы можете посмотреть бесплатно Yoonu Baye Fall : Mbóotu ndigal ak liggéey | Waxtaanu Baye Adama Sarr ak Baye Mamour Ndao или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Bismillahi Rahmani Rahime, Dalal jàmm ci seen bërëbu xam-xam bi di Jambarou Mouride 2.0. Tay jii, dañuy dikkaat ak yeen ci waxtaan bu am solo mu jëm ci : Yoonu Baye Fall ak mbóotu ndigël ak liggéey. Horodatages (Timestamps) 00:00 - Introduction : Présentation de Baye Adama Sarr et Baye Mamour Ndao. 08:45 - La philosophie de Lamp Fall : Pourquoi le travail (Liggéey) ? 15:20 - Le secret du Ndigël : Comment obéir parfaitement au Guide ? 30:10 - Récits des anciens : La force physique et spirituelle des Makk ñi. 45:50 - La différence entre le travail mondain et la Khidma sacrée. 58:30 - Téguine et Discipline : Le comportement exemplaire du vrai Baye Fall. 01:18:00 - Conclusion et Prières finales Sunu ñaari jambar yii, di Baye Adama Sarr ak Baye Mamour Ndao, ñooy leral ni Mame Cheikh Ibrahima Fall dundé won ndigëlu Sëriñ Tuubaa. Dañuy woné ni liggéey du lénneen ludul ngërëmu Borom bi, te yoonu Baye Fall mooy kërëfëtu ci ndigël ba faww. Lan ngeen di dégg ci waxtaan bi : • Maqaamay Lamp Fall : Lu tax liggéey nekk yoonu njub ci moom ? • Mbóotu Ndigël : Naka la nuy jëfé ndigël ba mu mel ni ni ñu ko diglé won ? • Liggéeyu Makk ñi : Ay nettali yu yéemé ci ni Baye Fall yi sàmpé yoon wi ci kàttan ak dëggu. • Téguine ak Njébbel : Ni nuy méllalé suñu jikko ba nekk taalubé dëgg. Déglul waxtaan bi ba mu jéex, ndaxte xam-xam bi ci nekk mooy dëgëral sa pas-pas ci lliggéeyu Sëriñ Tuubaa. 👉 Abonnez-vous ngir bañ a ràttaxlu ci taarixu Jambar yi. 👉 Bindal ci commentaire : "Jëf Jël" ngir sargal yoonu Baye Fall. #jambaroumouride #mouridisme #touba