• ClipSaver
ClipSaver
Русские видео
  • Смешные видео
  • Приколы
  • Обзоры
  • Новости
  • Тесты
  • Спорт
  • Любовь
  • Музыка
  • Разное
Сейчас в тренде
  • Фейгин лайф
  • Три кота
  • Самвел адамян
  • А4 ютуб
  • скачать бит
  • гитара с нуля
Иностранные видео
  • Funny Babies
  • Funny Sports
  • Funny Animals
  • Funny Pranks
  • Funny Magic
  • Funny Vines
  • Funny Virals
  • Funny K-Pop

MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE скачать в хорошем качестве

MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE 4 года назад

скачать видео

скачать mp3

скачать mp4

поделиться

телефон с камерой

телефон с видео

бесплатно

загрузить,

Не удается загрузить Youtube-плеер. Проверьте блокировку Youtube в вашей сети.
Повторяем попытку...
MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE
  • Поделиться ВК
  • Поделиться в ОК
  •  
  •  


Скачать видео с ютуб по ссылке или смотреть без блокировок на сайте: MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE в качестве 4k

У нас вы можете посмотреть бесплатно MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:

  • Информация по загрузке:

Скачать mp3 с ютуба отдельным файлом. Бесплатный рингтон MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE в формате MP3:


Если кнопки скачивания не загрузились НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru



MAME MBAYE LAYE - YAA RASUULAL-LAAH - NEW SINGLE

Extrait du Poème: Yaa Rasuulal-laah Extrait du Poème Yaa Rasuulal-laah ( vers 7 à 12). Voici l'intégralité du Texte. L'intégralité du son très bientôt. 1 Ay Yàlla tawal te nga julli Musëlal te nga yokk te dolli Sunu soppe bi gën, sunu Ndaw li Yaa Rasuulal-laah 2 Ay Yàlla lu tol ni Sa xam-xam Ay Yàlla lu tol ni Sa am-am Jullil ci mbindeef mi La gën a xam Yaa Rasuulal-laah 3 Ay Yàlla sa soppe bi moo tax Ba nu xam La ba sopp La moo tax Nu ngi jàpp ci lii mu nu xëy jox Yaa Rasuulul-laah 4 Ay Yàlla sa soppe bi moo jël Sunu xol yi defar ko ba tay njël Ňuy toog di La kañ di La sàbbaal Yaa Rasuulal-laah 5 Ay Yàlla sa Ndaw li talul woon Dara ndax rek bëgg nu aw yoon Ňi xamul woon jappe ko ab noon Yaa Rasuulal-laah 6 Terenañ ko mu woote (ilal-laah) Di ko xas jeebaane ko (fil-laah) Jéem na ñu sax raylu ko, (wallaah) Yaa Rasuulal-laah 7 Xeex na ñu ko ba génne ko dëkkam Fu mu dem ñu yabal fa ku kay jam Sallaaw ku ko noonu du am ndam Yaa Rasuulal-laah 8 Ňuy gën di ko bañ muy baale Di ko wër di ko tooñ te du faale Lu ñu def muy muuñ bañ a laale Yaa Rasuulal-laah 9 Bu ganaar songee bes Gaynde Muy ree di ko raay muy (bonde) Dafa laajul nag wa ca fande Yaa Rasuulal-laah 10 Ku la sooru nga koy muuñ laajul Lay xëy di ko dóor du ko waajal Day xëy di ko ruur di ko semmal Yaa Rasuulal-laah 11 Ku la bañ bëgg nan la lu raw ko Ku moy it nu ngi topp lu sut ko Ku daw it nu ngi xeñtu lu tiim ko Yaa Rasuulal-laah 12 Sallaaw ku la bañ yaw lay wër Ku la tuutal doy nga ko tiitër Ku la xas yaa taax muy kër-kër Yaa Rasuulal-laah 13 Sunu xol yi du namm ku dul yaw Sunu gët yi du séenu ku dul yaw Sunu xel yi du ngéeju ku dul yaw Yaa Rasuulal-laah 14 Ku nu bëgg itam yaw yaa tax Ku nu topp Yonnen yaw yaa tax Ku nu xool gis Yonnen moo tax Yaa Rasuulal-laah 15 Ňëw nan di dagaansi nga may nu Nu ngi bóof ci sa keppaar jox nu Loo sàkk ba jox nu mu doy nu Yaa Rasuulal-laah 16 Xam nan sa teraanga defal nu Xam nan ni nga baaxe defar nu Xoolal ni nu sonne yërëm nu Yaa Rasuulal-laah 17 Xam nan ñi nga yeege ñu jàlla Ňi nga tax ñuy déeyook Yàlla Ba jubook moom (azza wa jalla) Yaa Rasuulal-laah 18 Xam nan ñi nga tax ba ñu woomal Ňi nga tax ba ñu xam ñi nga jàngal Ňi nga tax ba ñu man ñi nga xëy fal Yaa Rasuulal-laah 19 Bunu toñeet man nga tinul nu Bunu dandeet man nga raxas nu Dunu dem fen yaa ngi faroonu Yaa Rasuulal-laah 20 Dunu dem fen jël nu nga yéegal Dunu dem fen boole nu jàngal Dunu dem fen fal nu nu woomal Yaa Rasuulal-laah 21 Dunu dem fen leel nu ci say leer Dunu dem fen yaay su nu yaakaar Dunu dem fen Baay du nu mus fer Yaa Rasuulal-laah 22 Dunu dem fen yaay sunu wéttal Toog di la kañ moo nuy dundal Lunu soxla nga jox nu ko (fil-haal) Yaa Rasuulal-laah 23 Nu ngi ñaan Buur Yàlla mu dolli Say may Yonnen bi te folli Ku la moy, say leer gën a jolli Yaa Rasuulal-laah 24 Te mu sàmm te yokk sa sët bii Nga faloon muy doon siiwal bi Moo tax ba nu xam la (Habiibii) Yaa Rasuulal-laah 25 Mooy ki la xam mooy ki la wormaal Mooy ki la fullaal ki la xeexal Tay mooy ki la wuutu ci sab jal Yaa Rasuulal-laah 26 Na fi yàgg te am wér aamiin Te Boroom Kun yokk ko man-man Fumu jëm nu gungee ko "ilaa hiin" Yaa Rasuulal-laah 27 (Sallaa Maawlaaya wa sallam Abadal-azmaani wa karram Abdan ixtaara wa 'allam) Yaa Rasuulal-laah 28 (Wal aali kazaal-ashaabi) Ak képp ku toog (bil-baabi) Ak képp ku sopp Habiibii Yaa Rasuulal-laah #lejeunepoete Date: Samedi 19 Janvier 2018 Lieu: Entre Addis et Dakar.

Comments

Контактный email для правообладателей: [email protected] © 2017 - 2025

Отказ от ответственности - Disclaimer Правообладателям - DMCA Условия использования сайта - TOS



Карта сайта 1 Карта сайта 2 Карта сайта 3 Карта сайта 4 Карта сайта 5