У нас вы можете посмотреть бесплатно Mbóotu Pass Passu Mame Cheikh Ibra Fall ci Serigne Touba (Leral yu xoot) или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Bismillahi Rahmani Rahime, Dalal jàmm ci seen bérëbu xam-xam ak yar, Jambarou Mouride 2.0. Ci jant bi tay, ñu ngi leen indil ab waxtaan wu xoot te fees ak mbóot, mu jëm ci Pass Passu Baboul Mouridina Mame Cheikh Ibrahima Fall ci jëmmam ak ci liguéeyal suñu Sang bi Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul. Horodatages (Timestamps) 00:00 - Ubbité ak tàmbali waxtaan ci maqaamay Lamp Fall 16:15 - Njébbalu dëgg : Diggante Mame Cheikh Ibra ak Sëñ Touba 34:30 - Pas-pas bi tax mu doon Baboul Mouridina (Buntu Yoon wi) 52:10 - Solo ndigal ci dundug Baye Fall dëgg 71:45 - Mbóoti liggéeyal Seriñ Touba ak barké bi ci nekk 82:20 - Kaddu gu mujj ak ñaanu barké ci darajay Mame Cheikh Ibra Lii moy misaal bi gëna dëgër ci diggante taalube ak Seriñam. Dégluleen leral yii ci : • Nan la Mame Cheikh Ibra Fall jébbalé boppam ba nekk "Lamp" yoonu Mourid. • Taxawayam ak pas-pasam bi ko may mu doon ubi-kaayu buntu manti ya (Baboul Mouridina). • Lijënté ndigal ci anam bu yéeme ak bëgg Seriñam ba kàdduy "Doundé ko, Dééé ko" fés. Bii waxtaan ab gindi-kaay la ci ñun ñi bëgg gëna xootal suñu ngëmm ak suñu njébbalu ci yoonu mourid. 👉 Rejoindre cette chaîne ngir jàppale suñu liggéey : / @jambaroumouride2.0 Abonne-wu leen ci chaîne bi, cuqal seen masin bi (cloche de notification) te partager vidéo bi ngir saaraxté xam-xam bi. #MameCheikhIbraFall #SerigneTouba #Mouridisme #PassPass #JambarouMouride #BayeFall #Touba #Islam #Ndigal #Njébbalu #jambaroumouride #mouridisme #touba #bayefall #cheikhibrafall #serignetouba #bayendiagadiop #mouride #senegal #wolof