У нас вы можете посмотреть бесплатно Magikara - KEEMAN (Lyrics) или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Magikara - KEEMAN: https://lnk.to/Keeman Link to all released music: https://bio.link/magikara Lyrics: Doy na Keeman Ahmadu Bamba laa ni Doy na Keeman (Ku Tedd Ki) Dëgg gi lee Su ñu Boroom Subhaanahu wa Tahaalaa Moom la ko jox (Asnal Xaadim) Ci bépp njariñ ci adduna Ak ya ca biir al ahira Yonen'a ko ko tànnal jox ko (Ku Tedd Ki) Fi ci suuf li fi gën Bamba fa ca kaw la fa gën Lepp la jël faye ko ko (Asnal Xaadim) Askanu Mbàkke Amna ñu barke, dëgg la Ahmadu Mbàkke Mo leen yobbaale, dëgg la, dëgg la Mo tax mu daan signé "Wa salaamu halamani tabbahal hudda" Maam Bamba ne La paix est avec celui qui suit le droit chemin Yaw miy wut ló am Jàppal ci Xaadim Dafa yoree am koom Te mëna yobbaale Hafizu mbër la Buddul sol dal Fó jaar mu giss la Ndax na muy xoole Zayin haraf la Zarfun de ndab la Man Moodu KARA maa ni (Ñun Magikara ñoo ni) Yaa may yóbbaale (Yaa ñuy yóbbaale) Yaw miy wut ló am Jàppal ci Xaadim Daam dafa yoree am koom Te mëna yobbaale Fó ne mu ne fa Lô moomul ba fa Bu dee sa yëf la Du ngéen digaale Yaw miy wut ló am #keeman #magikara Follow MAGIKARA on: Instagram: / magikara_diamondz Facebook: / magikaradiamondz Twitter: / magikaradiamond