У нас вы можете посмотреть бесплатно Bril - Wétalngama (Clip Officiel - B.O "Pod et Marichou") или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Abonne-toi à ma chaîne ici https://goo.gl/Qw5BFh ## Nouveau clip : "Wétalngama" de Bril Fight 4, chanson écrite pour la B.O de la série "Pod et Marichou" : la douleur immense occasionnée par la disparition d'un être cher. #Brilfight4 #Wétalngama #ClassChicMusic #PodetMarichou #team221 Crédits, remerciements & dédicace du clip « Wétalngama » # Lieux : Kédougou / Thiés / Lac Rose Réalisation : H-Lab Pro Entertainment (771833387) Déguisement : Les Bassaris Un grand merci à tous ceux qui ont participé à la réussite de cette vidéo. Je dédie ce morceau à tous ceux qui ont perdu un être proche et y rends hommage à mon Père. "Je pleure son absence mais ma plus grande souffrance , c’est quand je me rends compte qu’il est parti pour un voyage sans retour et ne reviendra plus jamais." Crédits de la chanson "Wétalngama" # Auteur & compositeur : Bril Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music Une production de Class’Chic Music (Senegal, 2018) Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux # Facebook / brilfight4 Instagram / brilfight4 Twitter / bril_fight4 Snapchat : @bril-fight4 Lyrics de la chanson "Wétalngama" # (1er couplet) Kholna founé, Démna founé , Guissatoumala. Djaarna féppeu fodane nek , wakhna louné ,Déggatoumala Douma nangou né dotouma guéstou ba guissla sama wett. Sama adouna toukina , taagouwouma bayima may wéétt. Djoulina di niaanat Yalla , mou délossila, donté ben biss la , Sa dém wi louma tiss la Lingfi bayi sass wou diss , douma ko atane , douma noppi fok ma guissla Niakkeula loumay djooyla {Refrain} Waro dém Bayima, Nakh ngama, Wétal ngama Gueuwoumani doumala guissati féneu , Nameunala, Wétal ngama Niaan nala wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ? Damalay Niaan wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ? (2ème couplet} Damay tog’ak ay Nitt niouy wakhtane té doumalén dégg, Bobou mangui Fénén Founiou tokk di kaff di rétane mane douma thi meuna bokk Sama Xélangui thi Yénén Fatélikouna biniou dane Réé / Bi nga dane déf louné ndakh mane . Dima takhawou féppeu foumou waré yaw , dima djappalé thi lo meunoul ak linga meune Fimou tollou ni thi sama Doundou Dara Safatouma , Khamouma louma tékki di djarign ndéém Djégguéwoma Sori ngama , Yaw kheuy nga dém bayima , Boma djèguè kaay wouyouma Sa Dém bi wétal nama (Refrain) Waro dém Bayima, Nakh ngama, Wétal ngama Gueuwoumani doumala guissati féneu , Nameunala, Wétal ngama Niaan nala wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ? Damalay Niaan wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ? (Outro) Lingfi bayi sass wou diss , douma ko atane , douma noppi fok ma guissla Niakkeula loumay djooyla