Русские видео

Сейчас в тренде

Иностранные видео




Если кнопки скачивания не загрузились НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу страницы.
Спасибо за использование сервиса savevideohd.ru



Dior Mbaye - GOUY GUI (Clip Officiel)

Streamez Gouy Gui : https://lnk.to/GouyGui Playlist : https://lnk.to/CODK Dior mbaye, auteur et compositeur nous fait cadeau de Gouy gui ( baobab) emblème du Senegal . En wolof quand on te dis que tu es un baobab cela veut dire que tu es indétrônable dans ce que tu fais. En chacun de nous sommeil un baobab. Auteur : Dior mbaye Beat, arrangement, Mix, master : Jeuuss Beatz Réalisation : Pac deejay -------------------------------------------------------------------------- #diormbaye #new #clips #gouygui Remerciements Danse: Fatou Sarr, Thiam, Khadija Nom du groupe Bakh Yaye Figurants: Flash Mo, Ibrahima diedhiou, Demba Keita , Oumar diallo, Daddy, Barry fruits, Rachid Figurantes : Khadidiatou Mbaye, Thiaba, Aicha, Fatou, Scénario : Mondial entertainment, Bamba Rassoul Moyens techniques: Mc Yaram- Kdrd Films Production du clip: Mondial Entertainment Bijouterie la solution Jannie styliste Emprunte By Bella Pape Beye jeune tailleur Maquillage coiffure : Sonia Makeup; lama couture Tissu :nafisamour Kendey By Diegou bamba LYRICS DIOR MBAYE Waaw waw yehé Dior mbaye yallah dogal louma def mou dém Fa nié di teulé , nieulé di diém Ma saff thi sen khôl ba dakk lem Nguéne dima sani cœurs aki j’aimes Bour YALLA dogal louma lal mou dém Yaw Sakhar bou dekki koutia langue dem kholal Ségne FALLOU ma wiss khorom bama niémé Segne FALLOU ma wiss khorom ma yémé . Refrain…… Pitie takk ci gouy (gouy yeugoul) pitie keuss keussi (gouy yeugoul) Pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) heyyy pitie yakk ci gouy ( gouy yeugoul) pitie keuss keussi ( gouy yeugoul) pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) yeugue ngani Gouy gui yeugoulaa (gouy yeugoul gouy yeugoula) boudé dangay diamb dé yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) yaw kholal mangay soul yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) gouy guou mak gui yeugoulaaa…. Mané dindi sakh langa defona tia Gueune yalla nopina domou diambour kouko yakk dangko diouroul kouné khamna kila Meune danga ko doul nangou yalla def na liko sop demb nopina mané garap bou ndaw boko mounta rossé bayiko mou dound boul Diéma boudi boul boudilou khamo fou réne ba sakh dandal soré déko khol de loin molay mousseul khana khamo né amna nio kham né ken doulen lal. Refrain…… Pitie takk ci gouy (gouy yeugoul) pitie keuss keussi (gouy yeugoul) Pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) heyyy pitie yakk ci gouy ( gouy yeugoul) pitie keuss keussi ( gouy yeugoul) pitie naw ni feurr (gouy yeugoul) yeugue ngani Gouy gui yeugoulaa (gouy yeugoul gouy yeugoula) boudé dangay diamb dé yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) yaw kholal mangay soul yeugoula ( gouy yeugoul gouy yeugoula) gouy guou mak gui yeugoulaaa. Bo amé nianou wadiour loy ragal Koné dokhalal. Amna nianou wadiour loumay ragal naniou dokhal. Lobita gueye Amna nianou Wadiour loy ragal Kone dokhalal. Pape Beye Amna nianou wadiour (le jeune tailleur), mbawor mbawor bi yow kay dokhal. Ndeye thiam amna nianou wadiour (djiguénou Bass ) cherie soulemane sané dokhalal. Ehh Wally boul guestou. Maryacine boul guestou ligueyou ndaye day tontou. Narou diaga boul guestou, cheri Sokhna boul guestou ligueyou ndaye day tontou. Kholal liguey focus niouy wakhtou khol bou rafet day tontou Maro marr boul guestou . -------------------------------------------------------------------------------------------- Tel: (+221) 781575551 Email: [email protected] Facebook : https://www.facebook.com/DiorMbayeLof... Instagram :   / dior_mbaye_lofficiel   Snapchat : @diormbaye7 TikTok: https://vm.tiktok.com/ZMen317Mx/ #diormbaye #gouygui #clipofficiel

Comments