У нас вы можете посмотреть бесплатно Khassida IKFINY - Diàngu Baye Moustapha Diop | Wolofal Makk Ñi или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Assalamou Alaykoum mbokki jullit yi, mbokki talibé yi, Dalal jamm ci seen chaîne Wolofal Makk Ñi. Tey jii, ma ngi leen di tàllal loxo ci ndimalu Sëñ Touba, nu dégluko te tàmbli ko ci barkeb Xassida gi di IKFINY. Ci video bi, dingeen ci dégg jangum bu am solo ak melokan bu rafet bu nekk ci Baye Moustapha Diop. Ay kàddu yu neex, yu sell, te dëppök jàngu makk ñi ni nu ko masé di def ci pastéf ak yar. Li nu nuy ñax rek moy nu gënë xam akë fonk souniou téeré yi té xamné li makk gni bayiwone ci yar ak téguine lagnouy fessal fi ci chaîne bi. • Abonnez-vous ngir bannié ak mbolem jàng yu bees yi. • Likez video bi ngir jappalé liggéey bi. • Partagez ko ak sa mboolo ngir barké bi saaba mbolem mbindéef yi. Jërëjëf, yalla na nu Sëñ Touba fayal. #mouride #touba #wolof #18safar #hizbuttarqiyyah #hizbuttarqiyyahdaroukhoudoss #htdkh #khassida #magaltouba #midadi