У нас вы можете посмотреть бесплатно Nettali: Maryaama Ba - En Wolof (Une si longue lettre) pàcc 01 |Mariama Ba (Bataaxal bu gudde nii) или скачать в максимальном доступном качестве, видео которое было загружено на ютуб. Для загрузки выберите вариант из формы ниже:
Если кнопки скачивания не
загрузились
НАЖМИТЕ ЗДЕСЬ или обновите страницу
Если возникают проблемы со скачиванием видео, пожалуйста напишите в поддержку по адресу внизу
страницы.
Спасибо за использование сервиса ClipSaver.ru
Nettali: Maryaama Ba - En Wolof (Une si longue lettre) pàcc 01 |Mariama Ba (Bataaxal bu gudde nii) Une si longue lettre : Bokk na ci téere (livre) yi gën a siiw ci àddina si te ab Saa-Afrig (africain)e) bind ko. Téere bi tekki na ñu ko ci lu ëpp 26i làkk (Le roman a été traduit plus de 26 langues). Làkku bees ko binde moo di farãse (langue original: français) Aji bind ji Maryaama Ba, di ab Saa-Senegaal (Senegalaise) 🇸🇳 Maam Yuunus Jeŋ ak Aram Faal, ñoo tekki ci Wolof ci atum 2016, tuddee ko "Bataaxal bu gudde nii" ñooy ñan ? Aram Faal 👇🏾 https://fr.m.wikipedia.org/wiki/Arame... Maam Yuunus Jeŋ 👇🏾 https://fr.m.wikipedia.org/wiki/Mame_... Maryaama Ba mu ngi juddu ci 17i fani weeru awiril atum 1929, faatu ci 17i fani weeru ut atum 1981 ci Dakaar. Bindkat la woon. Téeréem yi gën a fés : Une si longue lettre, Le chant écarlate. Téere bii nag, ay xew-xew yu am solo te baree ngi ci biir ! Day feeñal mbatiit, aada/mbaaxu Senegaal, rawatina ci jigéen ñi, ak ci Afrig swu jant. Rejoignez-nous & Soutenir cette chaîne / @souhaïboutv --------------------------------------------------------- Abone-wuleen ci sen bi ⤵️ / souhaïboutv ------------------------------------------------------------------- Mboor (histoire) yees fent ci Wolof ⤵️ • Histoire en Wolof Léeb ci Wolof ⤵️ • Léeb ci Wolof Taariixu Senegaal ⤵️ • Taariixu Senegaal (Histoire du Sénégal) ----------------------------------------------------------- Mbaalu jokkoo yi ⬇️👌🏿 Insta: https://www.instagram.com/invites/con... Feesbuk: / souhaïbou-tv-101746092489724 Tiktok: https://vm.tiktok.com/ZMLSY6FKc/ ________________________________________ Seen mbégté ak seen i njariñ ñooy sunu yitté. ✅✅